PRESENTATION DE VOEUX ANNEE 2020
Bonjour mes ami(es),
MAGUI LENE DI NIANNALE
SOUTOURA GOU SAKH DAK
JAM JOU SAKH DAK
KHEWEUL YOU SAWANE BAWANE YOKHO AK NDAM
BANEKH DJOU AMOUL APP
WERR AK FEKKE
WERRLE AK TAWFEKH AK TAYSIR SI BARKE YONETE BI MOUHAMED PSL
DEWENATY BALENN MA AKK
BALENALENE YALLA NAGNOU BOURBI DJEGGALNOU.AMINE
JE SOUHAITE A L'ENTAME DE CETTE NOUVELLE ANNÉE A CHACUN UN ANNÉE DE PAIX, DE SANTE DE FER, UNE ANNÉE DE SUCCÈS DANS LES PROJETS.EN MOT UNE ANNÉE DE BONHEUR.........
Commentaires
Enregistrer un commentaire